Compositor: Não Disponível
Damay solu neex na ma
Sama tailleur naxu ma
Sañse ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Ooh, ma mëna sañse!
Ree ju neex!
Ambiance ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Wuuy yaay (ree)
Ma mëna sañse ree ju neex!
Bari feeling mën naa fu ne
Sañse ma ci topp
Ma fi ap escort [...]
Flash ma ko moom
Mete visa ra
Man fu ma génne coow li
Bari lay ma tàccu dara
Tàccu ma (woy tàccu)
Tàcculeen li (ey tàccu)
Tàcculeen li (wuy tàccu)
(Dëb ko, naa mook rumbax!)
Tàccu ma (woy tàccu)
Tàcculeen li (ey tàccu)
Tàcculeen li (wuy tàccu)
(Dëb ko, naa mook rumbax!)
Sama sañse baax na
Sama montre baax na
Samay dàll, lan la?
Participer si réew mi rekk!
Sama xol neex na
Ma sañse reetaan
Tay li la ndawtal
Participer si réew mi rekk!
Sañse ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Ooooh, ma mëna sañse!
Ree ju neex!
Ambiance ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Wuuy yaay (ree)
Ma mëna sañse ree ju neex!
Ey lii lan la, lii lan la?
Ndekete ma ci réew
(Ma solu neex na ma)
Ey lii lan la, lii lan la
Ndekete ci man mën naa sañse
(Sama tailleur naxu ma)
Oh là là, sañse reetaan
(Dama solu neex na ma)
Oh là là, sañse reetaan
(Sama tailleur naxu ma)
Nii la, nii la, nii la
(Eh, ku ko mën ni nga koy defe)
Nii la, nii la, nii la
(Eh, ku ko mën ni nga koy defe)
Sañse dox ci diggu koñ bi
Fépp ñépp di ma topp
Ñu naan: Ki ni kan la?
(Dëb ko, naa mook rumbax!)
Sañse boole kok noppi
Sañse noon bi lay soppi
Ñu naan: Est-ce que ki yaw la?
(Dëb ko!)
Maa leen tere nelaw, tere nelaw
Tere nelaw (wuooh)
Maa leen tere nelaw, tere nelaw
Tere nelaw (wuooh)
Sañse dox ci diggu koñ bi
Fépp ñépp di ma topp
Ñu naan: Ki ni kan la?
(Dëb ko, naa mook rumbax!)
Sañse boole ko ak noppi
Sañse noon bi lay soppi
Ñu naan: Est-ce que ki yaw la?
(Dëb ko!)
Maa leen tere nelaw, tere nelaw
Tere nelaw (wuooh)
Maa leen tere nelaw, tere nelaw
Tere nelaw (wuooh)
Sañse ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Ooh, ma mëna sañse!
Ree ju neex!
Ambiance ree (ku ree)
Man damay ree (ku ree)
Wuuy yaay (ree)
Ma mëna sañse ree ju neex!
Ey lii lan la, lii lan la?
Ndekete ma ci réew
(Ma solu neex na ma)
Ey lii lan la, lii lan la
Ndekete ci man mën naa sañse
(Sama tailleur naxu ma)
Oh là là, sañse reetaan
(Dama solu neex na ma)
Oh là là, sañse reetaan
(Sama tailleur naxu ma)
Sañse naa rekk
Sañse nii la
Sañse naa rekk
Sañse nii la
(Maa leen tere nelaw)
Jarul moo koy wax ndax sañse nii la
Piir moo way, li dafa xer
Dëb ko, naa moo ku rumbax!
Nii la, nii la, nii la
(Eh, ku ko mën ni nga koy defe)
Nii la, nii la, nii la
(Eh, ku ko mën ni nga koy defe)
Dëb ko, naa moo ku rumbax!
Rumbax, rumbax, rumbax-rumbax!
Kaay! Dëb ko, naa moo ku rumbax!