Compositor: Não Disponível
Danga ma wan wan ma nobeel
Wan ma cofeel, wan ma luy nammeel
Dama la xam xam luy mbëggeel
Xam ni ku du yaw duma mën a pexel
Danga ma bégee fa ma xam ko waay
Maa la raw, baby xam ko waay
Tu sais que je t'aime de tout mon coeur
Tagal ma waay, wey bu dootu fay
Dinga ma ray xalaatuma la bàyyi
Des jasite ñépp xam ni yaa mi rey
Yaa mën, yaa ngi
Tay ma ci la koy Yàlla seede la
Tay ma taggalel ba nga xam yeen kan
Yaw mi la yaw rekk a waral li
Jëlal jëlal
Te bëgguma ku lay jege jege
Dawal dawal
Ne naa la jarul nga may xaar
Ñëwal ñëwal
Te xam nga yoon bi nga war a jaar
Dawal dawal
Ey bëgguma ku lay sonal
Bëgguma ku lay gaañ
Bëgguma ku lay tooñ
(Maak yaw la)
Ey bëgguma ku lay sonal
Bëgguma ku lay gaañ
Bëgguma ku lay tooñ
(Maak yaw la)
Bu jaaree bëre naa ko dóor daan
Bu jaaree mer duma reetaan
Bu jaaree jëf dinaa ko def
Dinaa dundal sa xol
Ba àdduna bi di ko seetaan
Mbëggeel lu diis la du dooy (lu diis)
Te ku ko ñam du ko fowe
Yaa ngi may guddandaat (waxal)
Yaa mën te di ko jëm de ma dundal laaj
Yaay ki ma coqotaan
Samay ram fu mu tànge damay duma daanu ma
Ñëwal ñëwal, pare naa lu ne
Yaay sama xol te jaral nga ma lu ne
Yaw mi la yaw rekk a waral li
Jëlal jëlal
Te bëgguma ku lay jege jege
Dawal dawal
Ne naa la jarul nga may xaar
Ñëwal ñëwal
Te xam nga yoon bi nga war a jaar
Dawal dawal
Ey bëgguma ku lay sonal
Bëgguma ku lay gaañ
Bëgguma ku lay tooñ
(Maak yaw la)
Ey bëgguma ku lay sonal
Bëgguma ku lay gaañ
Bëgguma ku lay tooñ
(Maak yaw la)
Maak yaw la!
Maak yaw la!