Compositor: Não Disponível
Miir ci yaw
Jaral nga ma naan vody tak sim bi mu day
Dawuma coow
Li nga ma jaral fi lay toog di ko wax ca kaw
Ma tay nob la takkal la capitaine bi
Yaw kaay wax ma ni nga def ba te game bii
Bon la nga raw ma, yaay bagg may teine bii
Kuñ mayul du naan yaay garab may rène bii
Li ñépp di wër la teye sama loxo
Sa tur bi lay dëkke sikkar sama chérie coco
Def nga ma sa mbër moo tax naanuma coocoo
Jaral nga ma dagg sama yaram bi chérie coco
Jàpp nga ma sama cóoppati
Ku mel ni yaw du amaati
Ci seen biir laa la cóoppati ba noppi di leen cokkeli
Yaw ki kan la, ki nii kan la
Bi sama bos la, teg na ci loxo
Yaw ki kan la, ki nii kan la
Bi sama bos la, teg na ci loxo
Mbëggeel lu bondit di mboli mboli
Jox la lépp li ma yor, bu doyl ma dolli
Sama honey, yaay sama coni
Faale nga ma manit duma la mësa foli
Àljanna yu neex yi laa bëgg ñu dem fa (dem fa)
Jox ma sa loxo, man ak yaw kese ñu des fa (des fa)
Li ñépp di wër la teye sama loxo
Sa tur bi lay dëkke sikkar sama chérie coco
Def nga ma sa mbër moo tax naanuma coocoo
Jaral nga ma dagg sama yaram bi chérie coco
Jàpp nga ma sama cóoppati
Ku mel ni yaw du amaati
Yaw nobal ku la nob ku la faale
Ci seen biir laa la cóoppati ba noppi di leen cokkeli
Heee nobal ku la nob ku la faale
Yaw ki kan la, ki nii kan la
Bi sama bos la, teg na ci loxo
Yaw ki kan la, ki nii kan la
Bi sama bos la, teg na ci loxo
(Yaw ki kan la, ki nii kan la)
Wane naa la
Ndax ki nga bëgg danga koy wane
Wane naa la
Teg na ci loxo ma waay
Lelelele yaay
Ku laa faale
Nobal ku la nob, ku la faale
Yaw ku laa faale
Nobal ku la nob, ku la faale leee
Yaw ku laa faale
Nobal ku la nob, ku la faale leee
Yaw ku laa faale